Seneweb.com Accueil |   Gerer ce blog   
Le blog de alioune ibnou abytalib diouf 
Créez votre propre blog gratuitement! 

MODOU FISC ET MODOU BAOL

Posté par: Alioune ibnou ab diouf| Mardi 06 février, 2018 10:02  | Consulté 447 fois  |  0 Réactions  |   

MODOU FISC ET MODOU BAOL

- Fisc : bonjour cher homonyme, et au Baol ?

 

- Modou : sant naa ci barkép serigne bi, waay naan gua def sama ndiatigué ?

 

- Fisc : Bah on poursuit notre but, remplir Les caisses de l’état !

 

-  Modou : ché bien, caissou bour dey doun !

 

- Fisc : ho là, faut pas te dérober hein, tu ne payes jamais tes impôts mon cousin… les ruraux là ce n’est pas la peine.

 

- Modou : boul di togn nak, Touba am na borom té nioun nieppeu bokk serigne Touba mais Dakar amna borom té Farance mo ko yilife.

 

- Fisc : quoi tu veux dire que nos deniers publics vont en France ?

 

- Modou : ah ! deukkou location dou deuk, yénn bala dara di toy Farance naan bé doyyal abbal lèn.

 

- Fisc : nos impôts ne vont pas en France que ce soit clair.

 

- Modou : Farance sou dieulé bénéfices yepp sanni niou dioutti, mom samay bénéfices yi ak dioutti yi moma gueuneul té lolou moo amTouba.

 

- Fisc : oui, mais ils ont investi leur argent et rapatrient leurs bénéfices c’est normal !

 

- Modou : waw, nioun nak nio mom sounou khalisse, di diokh serigne bi adiya mouy ceddeulé miskines yi ak dieuwrines yi (mécanismes de concentration et de redistribution) ; wa Farance nak da niouy rawalé souniouy njitt yi di dadialé dieumeulé waat farance, deuk bi dieum ganaw.

 

- Fisc : non non, échapper au système de l’état c’est faire de l’informel !

 

- Modou : lakheu say bénéfices guir faye lou neew mo keu gueuneu yéss toureundoo, sa bopp bi sakh état farance moko sole bé mou fess.

 

- Fisc : Mais pourquoi vous ne participez pas au développement de la Nation ?

 

- Modou : Touba kagn mi gui door waaram, nio mom sounou bénéfices, mom sounou souf, mom sounoup serigne, bé momalé sounou bopp, kou douggou raam ! yénn nak lolèn mom guinaw décittou farance ?

 

- Fisc : on emprunte beaucoup pour investir dans les infrastructures, les routes, les hôpitaux…

 

- Modou : ay borr dokhalout am reew, té kou lépp fékka na gua diakhlé. Maan samaw fass ak charrette bounou défaar fi ci sunugaal laa tammalé bé yorr ay bitiks ak autos youy daw fi bé amérique, li meu djikh moy sakh ci reew mi di diarigne sama gokh.

 

- Fisc : là tu gagnes un point !

 

- Modou : kholal gni fi yorr allal ci reew mi, lambakat yi, wey kat yi, béy kat you mag yi. Borom diplômes yi amouniou kaw amouniou souf ndakh farance, politiciens yi ak banques yi !!

 

- Fisc : le système actuel est formaté pour la France et nous sommes des sous-produits de ce système de prédation étatique et financier… je vois clair maintenant,mais que faire ?

 

- Modou : kou nekk na déf liko niorr, Touba dieum kanaam !

 

 L'auteur  alioune ibnou ab diouf
Une faute d'orthographe, une erreur á signaler ? Une précision á apporter ? Ecrivez moi avec votre info ou votre correction et en indiquant l'url du texte.
Commentaires: (0)

Ajouter un commentaire

 
 
alioune ibnou ab diouf
Blog crée le 27/08/2014 Visité 43307 fois 33 Articles 133 Commentaires 5 Abonnés

Posts recents
MODOU FISC ET MODOU BAOL
Parlons de chutes de cheveux et des solutions à envisager
COMMENT SAUVER BARGNY?
Discussion entre un député et un intello Sénégalais
VOTEZ DEFAR SENEGAL avec les Indépendants NIOU DEFAR REW MI
Commentaires recents
Les plus populaires
Discussion entre un député et un intello Sénégalais
La dynamique des partis politiques au Sénégal
MARCHE ILLICITE DU MEDICAMENT AU SENEGAL: DESCRIPTION ET STRATEGIE DE LUTTE
DES PROPOSITIONS POUR UN SENEGAL MEILLEUR
COMMENT SAUVER BARGNY?